Dans le deuxième épisode du podcast Réewum Ngor, Thierno Alassane Sall évoque les freins structurels qui empêchent le plein emploi au Sénégal. Il donne aussi des explications pour briser éradiquer la pauvreté dans notre pays, qui selon lui n'est en aucun cas une fatalité.
2 May 2021
Réewum Ngor - Episode #2 (wolof)
Ci ñaareelu limatu podcast bi Thierno Alassane Sall di amal léeg-léeg, njiitu République des Valeurs mu ngi waxtaan ci wàllum liggéey. Lu tax xëy jafe fii ci Senegaal ? Lu ciy pexe ?
5 Apr 2021
Réewum Ngor - Episode #1 (wolof)
Ci limat bu njëkk bii, Thierno Alassane Sall mu ngi saytu, di wax lu waral Senegaal moom boppam lu mat, ci atum ren, juróom-benn-fukk-ak-benn at, te ba leegi réew maa ngi tumrankee. Mu ngi ut itam ay pexe ngir kàttanal ndaw yi, ñu toog seen réew fekk fi jàmm ak naataange.
5 Apr 2021
Réewum Ngor - Episode #1
Dans ce premier épisode, Thierno Alassane Sall livre un diagnostic critique de la situation actuelle du Sénégal, et revient sur les ratés de notre pays depuis 1960. Il dessine aussi des perspectives et des solutions pour garantir un avenir désirable à la jeunesse sénégalaise.
Host of Réewum Ngor?
Claim your podcast to manage its listing and keep your show details accurate.
Pod Engine is an independent podcast discovery and analytics service and is not affiliated with or endorsed by this podcast. Artwork and show content belong to their owners. Full legal notice.